Audio - Affaire Khadim Ndiaye - Aida Macké: Les confidences du fils du propriétaire de la maison.

Partager
Intégrer

Commentaires • 643

  • Moussou Sarr
    Moussou Sarr Il y a 6 heures

    moi je ne comprends Sénégal parceque ki raw dieukeureum wané naniou ko siwal ko fepp mais loutakh niou sathie khalé yi,di violé waté bouniou léne diapé douniou wané???????

  • Layzo Carlou
    Layzo Carlou Il y a 11 heures +1

    Mais bro bi vrai doff leu koi ...Meurtre am nganane plainte amoul..Même s'il n'y a pas de plainte, les responsabilités doivent être situées... La justice est là pour tout le monde

  • Layzo Carlou
    Layzo Carlou Il y a 11 heures +1

    Koutaal dieukeureum nguéne naane kou bakh leu ...vrai dof nguéne koi ...C'est le monde à l'envers

  • Cherif Cherif
    Cherif Cherif Il y a 12 heures

    Joli

  • Marieme Bassoum
    Marieme Bassoum Il y a 14 heures +1

    Méchante épouse tu n mérite Pa être mère tu a mis la honte ns femme loumoutou done tale nite tu allé tro loin vrmmt

  • Massylla Mbaye
    Massylla Mbaye Il y a jour

    Ndawsi daal kou bone la té sokhor di lakk nit mélni kou yor dibitéri , nioukoy dèma rafétal li kéne manouko rafétal bam rafét

  • Oumy Gueye
    Oumy Gueye Il y a jour

    qui sokhor na trop

  • Masseye Fall
    Masseye Fall Il y a jour

    Li dawna yaram yalla rek mo kham

  • Yayetop Thiam
    Yayetop Thiam Il y a jour

    Un. Mari. Beau

  • Mafou Aidara
    Mafou Aidara Il y a jour

    Mane maa waarou

  • Diatou Diallo
    Diatou Diallo Il y a jour +1

    Djiepi na wa senegal 🇸🇳 Bilaye Walay femm bi bougn mako abalone nako togu lek ko Bilaye Walay en plus ki khamoul khol mane Serigne ak famille douma leine ax falè force damay ray femm bi mou nek match null Bilaye lou nit firr firr tall c la dernière chose koi

  • dia aissatou
    dia aissatou Il y a jour

    Vous etes trop hypocrites mes chers journalistes c est quoi c est histoire on parle de meurtre de premeditation

  • Julienne Badiane
    Julienne Badiane Il y a jour

    Crime par préméditation. Donc c'est la prison directe

  • modou lo
    modou lo Il y a jour

    kimom dafabon torp

  • michou diaw talibe baye Niass Diaw

    Yaw mom mansour diop mala weddi naké yaw Domi haram gua geumoulo dara amoul domou serigne amoul dara wakha li yalla wakh si kou ray niit na nekeu domou seuydina mouhamet baxam

  • la linguere Niang
    la linguere Niang Il y a 2 jours

    Ki dh koukoy takat day taylè bopam😂 rk

  • Haby Cisse
    Haby Cisse Il y a 2 jours

    HA LES SAPEURS POMPIERS !!!!!!
    TOUT MARISTE POUVAIS PRENDRE FEU ET EUX DISENT MANQUER DE RÉSEAU !!!!!!
    HA LE SÉNÉGAL !!!!!!

  • Mbaye Seck
    Mbaye Seck Il y a 2 jours

    Eskeuy yalla sounou borom.. Ki mo bone deugue, takhaw âme fite di soti nite essence talko mou dé

  • cheikh expert Camara
    cheikh expert Camara Il y a 2 jours +1

    Loutah sénégalèyii naafèkh.elhadj dall wèdinala.

  • Tossane Diagne
    Tossane Diagne Il y a 2 jours +1

    Bayileen mou bonne lou nieuw ngeen wakh ndogalou yallah
    YALLA kouko wo kouné daley diapalé soutoural la mais Satan naak kouko wo mou wouyou sila
    Jalousie bou eup bakhoul day attiré Satan donc d'après les disputes la femme n'a jamais respecté son mari ndakh khamna elle dira k sama papa moy serigne niam di gorom douma sania deef darra
    Kou goor ki ndeyssane mélni kharou yaar ndakh am respect am limouy rouss ak loumouy khol!
    Mane naak je les connaisse pas mais souma bokone ak khadim Ndiaye bou yabbo niou reyma déh mais Dame bi dinako deef cicatrice bo khamné heure bou sétto dineu fatélikou limou deef
    Wassalam
    Repose en paix khadim sunu borom doula sétane been yone il sera ton avocat Dinala pledel amoul serigne amoul justice mo bok ndiaboté nieup on est tous égaux devant lui!

  • Ousmane Ndiaye
    Ousmane Ndiaye Il y a 2 jours

    Prémédité

  • Fatima Rassoul Gueye
    Fatima Rassoul Gueye Il y a 3 jours

    Kou ray danioula wara ray

  • patricia diop
    patricia diop Il y a 3 jours

    C mon oncle le frere a mon pere ke dieu l'accueille au paradis...

  • soda mbacke
    soda mbacke Il y a 3 jours

    Mane kouyor bi khole ya ma meune

  • soda mbacke
    soda mbacke Il y a 3 jours

    Mane kouyor bi khole ya ma meune

  • diarra dabo
    diarra dabo Il y a 3 jours +1

    vraiment cet acte est inexplicable! mais Allah voit tous même si elle n'est pas punie dans la vie présente, elle le sera dans l'au delà!

  • Massamba Ly
    Massamba Ly Il y a 3 jours

    Boukene togn seytanè nak
    Jalousie c animal .beuy sakh dafay firr
    Guinar sof mbame khoukh.
    Mais dem bay jeul essence talll
    Kou sokhorr lol lol lol mokoy def
    Sa merite punution .loi kasso charia reyy

  • sy amsatou
    sy amsatou Il y a 3 jours

    En plus il etais tres beau wallah thier elle a gater la vie de ce jeune homme.wallah

  • sy amsatou
    sy amsatou Il y a 3 jours +1

    On a qu'a appliquer la charia wallah ke Azawadjel accorde a khadjim le djannatou firdaws

  • issa diallo
    issa diallo Il y a 3 jours

    réponse en paix

  • Awa Gueye
    Awa Gueye Il y a 3 jours

    Slu

  • Neva Sow
    Neva Sow Il y a 3 jours

    Quand une femme est movaise elle est très movaise.

  • Mariane tu Est le Rio Ndiaye

    Elle méritte l'enfer sette solope de Aicha mbacke nitte kou meune déef

  • mouhamed mbaye
    mouhamed mbaye Il y a 3 jours

    Mane dee sama yone nékoussi Dee! Khawma Lou khew ! Wayei problème waroul takh keneuh dii taaal nite nak

  • Mohamed Sall
    Mohamed Sall Il y a 3 jours +1

    Sa diabar boula talone do wakh laulou imbéciles

  • penda elimane thiam
    penda elimane thiam Il y a 3 jours +1

    wa tamit mane dal meunouma comprendre nit Lou gnaw li rawatina Ray nit gnounane nit yi nagnou manou la femme limou def dara meunouko rafetal ak famille boumou meundi bok yakhna derou ay mbokam fi mom kou dé ya perte même bou amout plainte yone dina def liguayam lima meiti thi Sénégal mou moudjei beuri ish se pays de merde

  • Khady Sarr Sarr
    Khady Sarr Sarr Il y a 3 jours

    Hum diga teud prison dè k sa soi clair dan ta tête .de plus tu n la jamé aimè kéne dou dèf Lou bonn lhomm de ta vie c du nimport koi

  • Maman Sy
    Maman Sy Il y a 3 jours

    Astou ya bone di rey

  • beydy sakho
    beydy sakho Il y a 3 jours

    Lou geuna grave si li ni dome dji mou wossine le lendemain sou magué ladj yayam kane moy sama papa lane lako sokhnassi di tontou

  • amt amt
    amt amt Il y a 3 jours

    Al maktoum.newonna nan sangat rewmi.ndax danouno rax.yenn yi douk neen.taal sa dieukeur.rendi sa baay.ak ay xarou youdoul diex.ta ay djoulit rek koy def.yalnanuci yalla miuseul mes li doyna war

  • Amadou Toure
    Amadou Toure Il y a 3 jours

    Xxx

  • Astou DIOP
    Astou DIOP Il y a 4 jours

    Vraiment. En tant djiguen dama rousse. Latmokoffi diare. Yakhe sa adina.

  • Abdou Ngom
    Abdou Ngom Il y a 4 jours

    قال تعالى وكتبنا عليهم فيها أن النفس بالنفس إلى ءاخره ءايه

  • oumy diatta
    oumy diatta Il y a 4 jours

    que la terre lui soit legere repose en paix

  • Fatou Faye
    Fatou Faye Il y a 4 jours

    C pas une raison de le tuer elle merite quon le tue

  • di_ _dy
    di_ _dy Il y a 4 jours

    Nane si mandou legui senegal couple bou ande si diam laniouy bagne gel bi sakh meune nane ko khaptal vu k legui senegal danio sokhor pck nitt ko beugu doko def lou metii..sa chelou

  • Mbacke Amy
    Mbacke Amy Il y a 4 jours

    Manou dal bakhna nit lou yonam nekoul nasi manou khadim ndiaye yalla nako yalla yeureum

  • Fanta Dabo
    Fanta Dabo Il y a 4 jours

    Pouff Sénégal dall mo nekh daguenne di fattè sakh ni yalla amna serigne la certe mai waroul takh domam di tallè na yonne def liguè yeum

  • Assane Sarr
    Assane Sarr Il y a 4 jours

    Il ya vraiment des débiles dans notre planète.... non débile et seytané.... putin la justice n attend pas de plainte pour démarrer la machine judiciaire.... alors vous les 3 connard fermez vos gueule...

  • Adama Diallo
    Adama Diallo Il y a 4 jours

    Boulen ko bal

  • Samath Diaw
    Samath Diaw Il y a 4 jours

    Ki nanko nokou si gosobi

  • Samath Diaw
    Samath Diaw Il y a 4 jours

    Baarkeb seringne Bamba ndaaw si kou bonella ki dafa reeew waaye naneko raaye

  • petit max
    petit max Il y a 4 jours +1

    Niit souy wakh day wakh louko woor Sénégal journalistes yi gnoy conduire gneup en erreur.
    Merci pour ces éclaircissements!!!

  • L'aube d'Afrique Tv LDTv
    L'aube d'Afrique Tv LDTv Il y a 4 jours

    Yalla nako yalla kharè aldiana

  • Maxalabelle Kane
    Maxalabelle Kane Il y a 4 jours

    laisse dieux jugé

  • sarr livia
    sarr livia Il y a 4 jours

    Laisser la police faire son boulot!lol les journalistes confirment déjà que c'est avec préméditation, et les pompiers qui n'ont pas de réseau et rejettent la faute sur la Sonatel,alors que bien souvent les numéros d'urgences sont accessibles et gratuits , ils prennent vraiment les gens pour des cons , Qu'en pensez-vous ?.

  • Kiné TINE
    Kiné TINE Il y a 4 jours

    Aÿ way Sénégal mo nex gua Ray nit gnouné dogalou yalla la

  • Dieynaba Ndiaye
    Dieynaba Ndiaye Il y a 4 jours +8

    J n'éprouve aucune pitié pour elle dieul essence sotti sa yaram dawoul tal allumette khoss sa yaram dawoul kelk soit l problem dara diarouko si aduna ki dal dafa ray nitt n'a dead si kasso bi li dafa eup yalla nanou yalla mousseul si satan rek

  • aminata diallo
    aminata diallo Il y a 4 jours

    Wa gni ligni wakh isca gno ngui coi deglu? Man daaaaal man daaaaal Senegal dugnu avence! Tarde ba faw!

  • Talla Diop
    Talla Diop Il y a 4 jours

    NDAWSI KOU BONNE LA DAGNOU KO WARA LAK . publiquement . .LI GUENA METTI MOY DARA DOUKO SI FEK . C'EST LE SENEGAL

  • Astou Diouf
    Astou Diouf Il y a 4 jours

    Naka la nite mana taa Lee limo bagiu bone rek

  • kiki sane
    kiki sane Il y a 4 jours +1

    Walay lima nakari si sounou rew barina barki yonentebi senegal bayil sou nit rayé nguani ndogalou yalla lah beneu djiguene moy yakeu tourou djiguene yeup barki serigne saliou mbacke non je di non mais on è dans kel pays ofet ay ay bessou penthieumi dineu meti dè pakhma Dina tang dh barki alkouran deug leu djiguen keneu douko tek lou meti dh mais ndaw si limou def tekko lou meti dagan neu rayko kom kimou def dieukeur wa ana loukofi diar nakh woudiou wa lolou lou yalla wakhla les hommes ont le droit depousé beneu ba nienteu wa kone bokou weurseuk leu soula nekhoul ngua delou sa keur bayi mo geun lou niaw yaw tey sa dom dj sou magué banila yaye boy ani sama papa lokoy wakh mako ray lolou niawneu trop trop sakh

  • lika angelique Fall
    lika angelique Fall Il y a 4 jours

    Je me demande comment on peut faire du mal a la personne que tu prétends aimé vraiment cette femme est un assassin. Qu'importe les liens familiales entre eux elle a ôté la vie elle mérite la mort. Neup neupal gui lagnou wara bayi

  • Bamba laye
    Bamba laye Il y a 4 jours

    Dolennn toussss wadji na fekeu la mome loutah mandou woul féké woul dara loumouy témoin yé té daffa fékeu lepeu diéh la seul personne qui peux dire c les deux filles yiko faye kiko dieuka guisse moy takeu dou niak amena loumou degeu moma bi khadim nane sama diambare talenama donc niakoul femme bobou moma bimouy faye takeu takeu bi khadim amena ay mo youmou wah mé wadji nafékeu papa dawsi tamite na xameni khadim beugonn na bénéne beuss boudoul bi mouy wah beussou khadim bi rafétena doyna warrr yénneu serigne yi nio yakeu Sénégal . doyna ware trop gnoup modou modou yi nekeu si diaspora bi nékeu akeu sougnouy nawlé chaque jours gnou rouss sénn kaname Sénégal lifa nekeu eupeuna FRclip boffa dougé tapé Sénégal sa xol yeupeu mofay diéh comm gnoune nio mome lou bonne beugeu ko fétowé .et pourtant ya des dignes fils du pays Sénégal diaral nalénn lépeu mé Sénégal donatoul touss si monde bi daw kou déff lou bonn déf si face bi wala youtube motah diaspora bi légui beneu gore bougoul gnibi Sénégal

  • Rokhaya Sy
    Rokhaya Sy Il y a 4 jours

    Mé c du jamé vu yaw noy kholé niit en tant ke sa dieukeur gakoy soti essence yaw so amé loula meti do dieul sa bagage dem sa yone lolou ani louko guena yomb mé Sénégal dall aaaahh mane diakhlé na niit mo lundeumm deug

  • l'invincible
    l'invincible Il y a 4 jours

    Wa sapeurs aussi ils sont nuls et sans compétence

  • Mike Loopy
    Mike Loopy Il y a 4 jours

    Lifetime jail rek . Nothing else

  • abdul hakim mohammad
    abdul hakim mohammad Il y a 4 jours +1

    Yéne merde, niou raye un être humain niounane ndogolou YALLAH la.

  • cr7fall96 llaf
    cr7fall96 llaf Il y a 4 jours +1

    Cette femme mérite d'être brûler vif

  • Mor niang
    Mor niang Il y a 4 jours

    Africa dou dem lak sapeur manoul walou! Big difference like usa

  • Serigne Mbacke
    Serigne Mbacke Il y a 5 jours

    man borom kourous gui dall Lima métti mot domdji dioudou rek dem kaso Yégoul dara khamoul dara mais foun tollou nani niane yalla mou mousall niou si ndiawtéf ak seytane ak modiou fou rafet barkeb borom touba

  • samba sadii ndao
    samba sadii ndao Il y a 5 jours

    Ak lou mounti am boule raye wala

  • Badinding Jabbi
    Badinding Jabbi Il y a 5 jours

    إنا لله وإنا إليه راجعون اللهم اغفر له وارحمه ودخله جنة الفردوس الأعلى الله أكبر

  • ndeye lo
    ndeye lo Il y a 5 jours

    Non ton ticket enfer est déjà proclamé fdp ya bonne billayiii kouuu bonne gueuu domerhame bii amoo benneuu yarrr

  • Rokhaya Diatta
    Rokhaya Diatta Il y a 5 jours

    Je suis vraiment désolée pour l'acte que la famme

  • Ouz bi
    Ouz bi Il y a 5 jours

    paix a son âme

  • Khady Thiam
    Khady Thiam Il y a 5 jours

    Gor diaroul li

  • Baye mor Sall
    Baye mor Sall Il y a 5 jours

    yalla na souf woyaf si kawam

  • petite fleur des îles
    petite fleur des îles Il y a 5 jours

    c'est n'importe quoi pourquoi brûler ton marie il faut savoir divorcer si sa ne va pas

  • aji awa
    aji awa Il y a 5 jours

    massla mo yaaha Senegal. I hope the legal system will give her the maximum sentence.

  • Yama Drame
    Yama Drame Il y a 5 jours +1

    Rip😢😢serigne khadim

  • Noh Fall
    Noh Fall Il y a 5 jours

    Ne calcul Pas dafa eumbe ba diis .si il estáis entrin de dormir et la fille etais sur se plan de linsandier

  • la Perfecta diaw
    la Perfecta diaw Il y a 5 jours

    Version yi barina ay way Sénégal mo am gnu meuna féne merciiii pour explication yi mai ioe mome si kaso bi gnay déé domeram

  • adama touré
    adama touré Il y a 5 jours

    C’est vraiment triste et malheureux de voir comment les gens sont hypocrites au Sénégal
    Vous vous rendez compte qu’il s’agit d’une meurtre 😭😭😭. Une personne est morte bon sang et vous parlez de ndogal yalla et de je ne sais quoi
    Sincèrement dans quel monde sommes-nous aujourd’hui

  • maimouna diallo
    maimouna diallo Il y a 5 jours

    C pays est d la merde on tue des gens comme des mouches après on s permet de dire q c la volonté divine c n pas Dieu qui descendra sur terre pour régler l problème Yalla wahoul ay jaamam niou bonn mais l jugement dernier sera fatal

  • Alfa Junior
    Alfa Junior Il y a 5 jours +4

    Mais adouna bi mo leundeum wa femme bii nit la elle mérite une peine de mort amoul domou serigne on est tous les même que la justice soit fait

  • Sokhna Arame Fall Mbaye
    Sokhna Arame Fall Mbaye Il y a 5 jours

    Way maylén gnou diame ki boudé serignam té yaroul domam si diné kha bayiko mou don nasaran bone rew sokhor nguéndi am linguéndi wakh

  • Adji Thiam
    Adji Thiam Il y a 5 jours

    Bilae ki dagne ko wara tale

  • Rama Ndiaye
    Rama Ndiaye Il y a 5 jours

    Mai lane moy ndayou lii s kel à fai na po d nom..lé humains son indubitablemn dan 1 obscurantisme démesuré wallahi azim

  • Mamadou Ndoye
    Mamadou Ndoye Il y a 5 jours

    Haa da nekoul sa mbok tal.

  • abdoulaye niass
    abdoulaye niass Il y a 5 jours

    Elle est tout simplement mal éduquée et ne craint rien dans la mesure où elle porte le nom de...Elle a commis un crime mûrement prémédité.Il faut être sadique et mesquin à mon avis pour agir de la sorte.Malheureusement tout cela par le maslaha.Prie ALLAH ACCUEILLIR le défunt dans son paradis le plus élevé.Que la terre lui soit légère.AMINE

  • cool inoos
    cool inoos Il y a 5 jours

    Doyna war lidara dirouko

  • Dennis The worm
    Dennis The worm Il y a 5 jours

    Allons y rek, hypocrisie dineu yakkh deukk bi !

  • nicola omar diouf
    nicola omar diouf Il y a 5 jours

    Famille bou bakh bou am diné doulle ban téy la mére n a meme pas pleuré par ce que c la famille des peaky blindder

  • Bineta Nara DIOP
    Bineta Nara DIOP Il y a 5 jours

    Liii momm nexoul ba nexoul mee apouna sama yaram dfa daw bilahi

  • Eva Gaye
    Eva Gaye Il y a 5 jours

    Le ministère public doit s'autosaisir cette femme est un danger pour la société.

  • Zeyna Ponroy
    Zeyna Ponroy Il y a 5 jours

    On est dans quel pays...donc si je comprends bien si on est issue d'une famille de marabouts forcément on est bien Dieu vous vois

  • Oureye Diallo
    Oureye Diallo Il y a 5 jours

    N'importe quoi Sénégal dal dou demm, l'hypocrisie des ces gens là m'énerve car on parle pas de marabouts ya mort d'homme c vraiment triste😔

  • LEUZZ VISION
    LEUZZ VISION Il y a 5 jours +1

    Ray mom Ray la rk amoul ki amoul ka

  • Touti Sambou
    Touti Sambou Il y a 5 jours

    Arréte de defante cet femme el a tué sn marii